
Xam sa démb, xam sa tey
by Goethe-Institut
Inactivewo·9 episodes
societyculture
Listener stats
Estimated listeners
Pro
About
<p>Ngir xam lu leer ci seen mboorum réew ak bu Afrig, ndaw ñi dañoo war a miin jàmbaar yi tabax Afrig. Ndégat yii di Podcast,« Xam sa démb, xam sa tey », looloo tax ñu tànn yenn ci jaar-jaar ak xew-xew i mboorum Senegaal, ngir may ndaw ñi ñu jàngee ci seen démb, baa man seen tay, te waajal seen ëllëg.</p>